Text copied!
Bibles in Wolof

Sabóor 93:4-5 in Wolof

Help us?

Sabóor 93:4-5 in Kàddug Yàlla gi

4 Waaye riirum wal mu walangaanoo, ak géej gu sàmbaraaxoo, Aji Sax ja fa kaw a rawati!
5 Say santaanee wér te wóor; Aji Sax ji, sellnga la sa kër jagoo bésoo bés.
Sabóor 93 in Kàddug Yàlla gi