Text copied!
BREAK EVERY YOKE
About
Bibles
All Languages
All Translations
All Countries
Back to Homepage
About Break Every Yoke
Bibles in Wolof
Sabóor 92:5-8 in Wolof
Help us?
Sabóor 92:5-8
in
Kàddug Yàlla gi
5
Aji Sax ji, yaa ma bégale say jaloore, may sarxolle ci say manoore.
6
Aji Sax ji, yaa réyi jëf; xóoti pexe.
7
Ku ñàkk xel réere ko, ku dofe umple ko.
8
Bu ku bon sëqlee nim ñax, képp kuy def lu bon di yokkule, dañoo nara sànku ba fàww rekk.
Sabóor 92 in Kàddug Yàlla gi
Home
About
Donate
Patreon
Privacy
Terms