Text copied!
Bibles in Wolof

Sabóor 92:3-7 in Wolof

Help us?

Sabóor 92:3-7 in Kàddug Yàlla gi

3 xëye tudd sa ngor, gonloo xamle sa worma,
4 xalamu fukki buum ànd ak moroom ma, xeetu kooraa jibandoo.
5 Aji Sax ji, yaa ma bégale say jaloore, may sarxolle ci say manoore.
6 Aji Sax ji, yaa réyi jëf; xóoti pexe.
7 Ku ñàkk xel réere ko, ku dofe umple ko.
Sabóor 92 in Kàddug Yàlla gi