Text copied!
Bibles in Wolof

Sabóor 92:13-15 in Wolof

Help us?

Sabóor 92:13-15 in Kàddug Yàlla gi

13 Ku jub day naat nig tàndarma, màgg ni seedaru Libaŋ
14 gu ñu jëmbat biir kër Aji Sax ji, muy naate sunu biir ëttu Yàlla;
15 bu màggatee sax di meññ, tooy xepp, sëq lipp,
Sabóor 92 in Kàddug Yàlla gi