Text copied!
Bibles in Wolof

Sabóor 92:12-13 in Wolof

Help us?

Sabóor 92:12-13 in Kàddug Yàlla gi

12 Maa gis jéllu noon yi, dégg yuuxi ñu bon ñi may tëru.
13 Ku jub day naat nig tàndarma, màgg ni seedaru Libaŋ
Sabóor 92 in Kàddug Yàlla gi