Text copied!
Bibles in Wolof

Sabóor 91:7-9 in Wolof

Help us?

Sabóor 91:7-9 in Kàddug Yàlla gi

7 Junni daanu fi sa wet, fukki junni (10 000) daanu fi sa ndijoor, du tax mu jege la.
8 Say gët nga ciy teg, di seetaan ku bon di jot yoolam.
9 Yaw mi màkkaanoo Aji Sax ji, Aji Kawe jii di sama rawtu,
Sabóor 91 in Kàddug Yàlla gi