Text copied!
Bibles in Wolof

Sabóor 91:5-6 in Wolof

Help us?

Sabóor 91:5-6 in Kàddug Yàlla gi

5 Doo ragal njàqarey guddi mbaa fittu bëccëg
6 mbaa mbas mu yooteg lëndëm, ak balaa buy fàdde njolloor.
Sabóor 91 in Kàddug Yàlla gi