Text copied!
Bibles in Wolof

Sabóor 91:4-6 in Wolof

Help us?

Sabóor 91:4-6 in Kàddug Yàlla gi

4 Kiiraayam la lay sànge, nga yiiru, làqu; wormaam yéew la, di la aar.
5 Doo ragal njàqarey guddi mbaa fittu bëccëg
6 mbaa mbas mu yooteg lëndëm, ak balaa buy fàdde njolloor.
Sabóor 91 in Kàddug Yàlla gi