Text copied!
Bibles in Wolof

Sabóor 91:3-5 in Wolof

Help us?

Sabóor 91:3-5 in Kàddug Yàlla gi

3 Kii kay moo lay musal cig fiir ak loraangey mbas.
4 Kiiraayam la lay sànge, nga yiiru, làqu; wormaam yéew la, di la aar.
5 Doo ragal njàqarey guddi mbaa fittu bëccëg
Sabóor 91 in Kàddug Yàlla gi