Text copied!
Bibles in Wolof

Sabóor 91:13-15 in Wolof

Help us?

Sabóor 91:13-15 in Kàddug Yàlla gi

13 Dangay falaxe jaan ak gaynde, di rajaxe ñàngóor ak sibi.
14 Yàlla da naa: «Kii de man la safoo, ma di ko xettli. Man la xam, te maa koy teg fu wóor.
15 Mu woo ma, ma wuyu ko; mook man ci biir njàqare, ma xettli ko, darajaal ko,
Sabóor 91 in Kàddug Yàlla gi