Text copied!
Bibles in Wolof

Sabóor 8:4-5 in Wolof

Help us?

Sabóor 8:4-5 in Kàddug Yàlla gi

4 Damay xool sa asamaan si nga móol, ak weer week biddiiw yi nga fi teg.
5 Moo luy nit, ba nga di ko bàyyi xel? Luy doom aadamaak loo koy yége?
Sabóor 8 in Kàddug Yàlla gi