Text copied!
Bibles in Wolof

Sabóor 8:3-5 in Wolof

Help us?

Sabóor 8:3-5 in Kàddug Yàlla gi

3 Làmmiñu tuut-tànk, ba ci luy nàmp, feeñal nga ca sa kàttan, bañaaleek feyukat ne xerem.
4 Damay xool sa asamaan si nga móol, ak weer week biddiiw yi nga fi teg.
5 Moo luy nit, ba nga di ko bàyyi xel? Luy doom aadamaak loo koy yége?
Sabóor 8 in Kàddug Yàlla gi