Text copied!
Bibles in Wolof

Sabóor 89:8-10 in Wolof

Help us?

Sabóor 89:8-10 in Kàddug Yàlla gi

8 Yàlla, ji ñu terala teral ci jataayu ñu sell ñi, te mu gëna raglu lu ko wër?
9 Yàlla, Aji Sax ji Boroom gàngoor yi, Ki Sax, ana ku tollook yaw doole? Yaw mi worma féete fu ne!
10 Yaw yaa man géej gu sàmbaraax; gannax ya fuddu, nga dalal.
Sabóor 89 in Kàddug Yàlla gi