Text copied!
Bibles in Wolof

Sabóor 89:7-8 in Wolof

Help us?

Sabóor 89:7-8 in Kàddug Yàlla gi

7 Ana kuy dab-dabal Aji Sax ji, fa kawa kaw? Ana ci goney Yàlla yi ku nirook Aji Sax ji,
8 Yàlla, ji ñu terala teral ci jataayu ñu sell ñi, te mu gëna raglu lu ko wër?
Sabóor 89 in Kàddug Yàlla gi