Text copied!
Bibles in Wolof

Sabóor 89:50-51 in Wolof

Help us?

Sabóor 89:50-51 in Kàddug Yàlla gi

50 Boroom bi, ana sa ngor la nga daan jëfe te nga giñale woon ko Daawuda ci sa worma?
51 Boroom bi, bàyyil xel ci sa gàcceg jaam ñi, ak xeet yu bare yi ma yenu yépp.
Sabóor 89 in Kàddug Yàlla gi