Text copied!
Bibles in Wolof

Sabóor 89:48 in Wolof

Help us?

Sabóor 89:48 in Kàddug Yàlla gi

48 Bàyyi ma xel, samay fan yàggul. Xanaa du neen a tax nga sàkk mboolem doom aadama?
Sabóor 89 in Kàddug Yàlla gi