Text copied!
BREAK EVERY YOKE
About
Bibles
All Languages
All Translations
All Countries
Back to Homepage
About Break Every Yoke
Bibles in Wolof
Sabóor 89:47-49 in Wolof
Help us?
Sabóor 89:47-49
in
Kàddug Yàlla gi
47
Éy Aji Sax ji, xanaa lii du jeex? Xanaa doo làqu fàww nii, sa mer di boy?
48
Bàyyi ma xel, samay fan yàggul. Xanaa du neen a tax nga sàkk mboolem doom aadama?
49
Ana kuy dund te du dee? Ku mana rëcc tëraayu bàmmeel? Selaw.
Sabóor 89 in Kàddug Yàlla gi
Home
About
Donate
Patreon
Privacy
Terms