Text copied!
Bibles in Wolof

Sabóor 89:41-45 in Wolof

Help us?

Sabóor 89:41-45 in Kàddug Yàlla gi

41 Bëtt nga miiram yépp, saam ay tataam,
42 ku fa jaare, jël ca alalam, mu doon mbalitu dëkkandoo yi.
43 Yékkati ngay bañam, noonam yépp di ree.
44 Dayal nga saamaram, te taxawuwloo ko cib xare.
45 Xañ nga ko darajaam, rattax ngànguneem fa suuf.
Sabóor 89 in Kàddug Yàlla gi