Text copied!
Bibles in Wolof

Sabóor 89:40-43 in Wolof

Help us?

Sabóor 89:40-43 in Kàddug Yàlla gi

40 Fecci nga sa kóllëreek sab jaam, foq nguuram, detteel ko.
41 Bëtt nga miiram yépp, saam ay tataam,
42 ku fa jaare, jël ca alalam, mu doon mbalitu dëkkandoo yi.
43 Yékkati ngay bañam, noonam yépp di ree.
Sabóor 89 in Kàddug Yàlla gi