Text copied!
Bibles in Wolof

Sabóor 89:39-42 in Wolof

Help us?

Sabóor 89:39-42 in Kàddug Yàlla gi

39 Ndaxam yaw Yàlla, jéppi nga ki nga fal, mere ko, wacc ko.
40 Fecci nga sa kóllëreek sab jaam, foq nguuram, detteel ko.
41 Bëtt nga miiram yépp, saam ay tataam,
42 ku fa jaare, jël ca alalam, mu doon mbalitu dëkkandoo yi.
Sabóor 89 in Kàddug Yàlla gi