Text copied!
BREAK EVERY YOKE
About
Bibles
All Languages
All Translations
All Countries
Back to Homepage
About Break Every Yoke
Bibles in Wolof
Sabóor 89:32-35 in Wolof
Help us?
Sabóor 89:32-35
in
Kàddug Yàlla gi
32
mbaa ñu xëtt sama dogali yoon, baña sàmmonteek samay santaane,
33
ma bantale leen seenug moy, dumaa leen seen ñaawtéef.
34
Waaye duma ko daggal sama ngor, te duma ko ñàkke worma.
35
Duma fecci sama kóllëre, te duma toxal sama kàddu.
Sabóor 89 in Kàddug Yàlla gi
Home
About
Donate
Patreon
Privacy
Terms