Text copied!
Bibles in Wolof

Sabóor 89:30-31 in Wolof

Help us?

Sabóor 89:30-31 in Kàddug Yàlla gi

30 Damay saxal askanam ba fàww, yàggal ab jalam ni asamaan.
31 Bu ay sëtam wàccee sama yoon, baña doxe samay ndigal,
Sabóor 89 in Kàddug Yàlla gi