Text copied!
Bibles in Wolof

Sabóor 89:28-32 in Wolof

Help us?

Sabóor 89:28-32 in Kàddug Yàlla gi

28 Te it maa koy def samab taaw, tiimale ko buuri àddina,
29 sàmmal ko sama ngor ba fàww, feddlil ko sama kóllëre.
30 Damay saxal askanam ba fàww, yàggal ab jalam ni asamaan.
31 Bu ay sëtam wàccee sama yoon, baña doxe samay ndigal,
32 mbaa ñu xëtt sama dogali yoon, baña sàmmonteek samay santaane,
Sabóor 89 in Kàddug Yàlla gi