Text copied!
Bibles in Wolof

Sabóor 89:22-24 in Wolof

Help us?

Sabóor 89:22-24 in Kàddug Yàlla gi

22 ànd ak moom, saxal ko, di ko dooleel.
23 Noon du ko bett, ku bon du ko torxal.
24 Ay bañam, ma rajaxe; ay noonam, ma fàdd,
Sabóor 89 in Kàddug Yàlla gi