Text copied!
BREAK EVERY YOKE
About
Bibles
All Languages
All Translations
All Countries
Back to Homepage
About Break Every Yoke
Bibles in Wolof
Sabóor 89:21-25 in Wolof
Help us?
Sabóor 89:21-25
in
Kàddug Yàlla gi
21
Gis naa sama jaam Daawuda, fale ko sama diw gu sell,
22
ànd ak moom, saxal ko, di ko dooleel.
23
Noon du ko bett, ku bon du ko torxal.
24
Ay bañam, ma rajaxe; ay noonam, ma fàdd,
25
sama wormaak sama ngor di ko gunge, may yokk kàttanam.
Sabóor 89 in Kàddug Yàlla gi
Home
About
Donate
Patreon
Privacy
Terms