Text copied!
Bibles in Wolof

Sabóor 89:18-19 in Wolof

Help us?

Sabóor 89:18-19 in Kàddug Yàlla gi

18 Seen darajay doole, yaw a. Boo nu baaxee, nu yokku kàttan.
19 Sunu kiirlaay lii, Aji Sax jeey boroom; sunu buur bii, Aji Sell ji séddoo Israyil ay boroom.
Sabóor 89 in Kàddug Yàlla gi