Text copied!
Bibles in Wolof

Sabóor 89:14-18 in Wolof

Help us?

Sabóor 89:14-18 in Kàddug Yàlla gi

14 Yaa àttan, jàmbaare; sa loxo di dooley neen, sa ndijoor ca kaw!
15 Njekk ak njub a lal sab jal, ngor ak worma dox jiitu la.
16 Aji Sax ji, ndokklee mbooloo mu la xal di sarxollee, di niitoo saw yiw,
17 ànd di la bége bés bu ne, sag njekk siggil leen.
18 Seen darajay doole, yaw a. Boo nu baaxee, nu yokku kàttan.
Sabóor 89 in Kàddug Yàlla gi