Text copied!
Bibles in Wolof

Sabóor 89:14-16 in Wolof

Help us?

Sabóor 89:14-16 in Kàddug Yàlla gi

14 Yaa àttan, jàmbaare; sa loxo di dooley neen, sa ndijoor ca kaw!
15 Njekk ak njub a lal sab jal, ngor ak worma dox jiitu la.
16 Aji Sax ji, ndokklee mbooloo mu la xal di sarxollee, di niitoo saw yiw,
Sabóor 89 in Kàddug Yàlla gi