Text copied!
Bibles in Wolof

Sabóor 89:10-14 in Wolof

Help us?

Sabóor 89:10-14 in Kàddug Yàlla gi

10 Yaw yaa man géej gu sàmbaraax; gannax ya fuddu, nga dalal.
11 Yaa fàdd Raxab, bóom ko, tasaare say noon ci sa doole.
12 Yaa moom asamaan, yaa moom suuf. Àddinaak li ci biiram, yaa ko taxawal.
13 Bëj-gànnaar ak bëj-saalum, yaa ko sàkk. Tabor ak Ermon, tund ya, di sarxollee sa tur.
14 Yaa àttan, jàmbaare; sa loxo di dooley neen, sa ndijoor ca kaw!
Sabóor 89 in Kàddug Yàlla gi