Text copied!
Bibles in Wolof

Sabóor 88:8-10 in Wolof

Help us?

Sabóor 88:8-10 in Kàddug Yàlla gi

8 Yen nga ma sa xadar, tance ma sa gannax yépp. Selaw.
9 Dàqal nga may xame, tax nga ñu seexlu ma; ma tëju, génnatuma.
10 Samay gët a ngi giim ndax naqar. Éy Aji Sax ji, maa ngi lay woo bés bu ne, dékk lay loxo.
Sabóor 88 in Kàddug Yàlla gi