Text copied!
BREAK EVERY YOKE
About
Bibles
All Languages
All Translations
All Countries
Back to Homepage
About Break Every Yoke
Bibles in Wolof
Sabóor 88:5-7 in Wolof
Help us?
Sabóor 88:5-7
in
Kàddug Yàlla gi
5
ñu sóoraale maak ñi wàcci biir bàmmeel. Ma mel ni jàmbaar ju kenn amatul yaakaar,
6
bokk ci néew, yi dara waratul, mbaa ku ñu bóom, mu tëdd cim pax, faaleetoo ko, xanaa dagg ko, wacc.
7
Tàbbal nga ma kàmb gu xóot, biir xóotey lëndëm.
Sabóor 88 in Kàddug Yàlla gi
Home
About
Donate
Patreon
Privacy
Terms