Text copied!
Bibles in Wolof

Sabóor 88:3-4 in Wolof

Help us?

Sabóor 88:3-4 in Kàddug Yàlla gi

3 Yal na sama ñaan àgg fa yaw; teewlul, ma woote wall.
4 Damaa suur këll ay musiba, ba soreetuma njaniiw,
Sabóor 88 in Kàddug Yàlla gi