Text copied!
Bibles in Wolof

Sabóor 86:8-10 in Wolof

Help us?

Sabóor 86:8-10 in Kàddug Yàlla gi

8 Boroom bi, doo moroomu tuur yi, te jëf melul ni sa jos.
9 Boroom bi, mboolem xeet yi nga sàkk ñoo lay sujjóotalsi, di màggal sa tur.
10 Yaa màgg te yéemey jëf, yaw doŋŋ yaa di Yàlla.
Sabóor 86 in Kàddug Yàlla gi