Text copied!
Bibles in Wolof

Sabóor 86:7-9 in Wolof

Help us?

Sabóor 86:7-9 in Kàddug Yàlla gi

7 Bu ma la wooyee bésub njàqare, yaa may nangul.
8 Boroom bi, doo moroomu tuur yi, te jëf melul ni sa jos.
9 Boroom bi, mboolem xeet yi nga sàkk ñoo lay sujjóotalsi, di màggal sa tur.
Sabóor 86 in Kàddug Yàlla gi