Text copied!
Bibles in Wolof

Sabóor 86:6-7 in Wolof

Help us?

Sabóor 86:6-7 in Kàddug Yàlla gi

6 Éy Aji Sax ji, teewlul, ma ñaan la; déglul, ma tinu la.
7 Bu ma la wooyee bésub njàqare, yaa may nangul.
Sabóor 86 in Kàddug Yàlla gi