Text copied!
Bibles in Wolof

Sabóor 86:5-6 in Wolof

Help us?

Sabóor 86:5-6 in Kàddug Yàlla gi

5 Boroom bi, yaa baax, di bale, di nàddil sa ngor képp ku lay sàkku.
6 Éy Aji Sax ji, teewlul, ma ñaan la; déglul, ma tinu la.
Sabóor 86 in Kàddug Yàlla gi