Text copied!
Bibles in Wolof

Sabóor 86:4-6 in Wolof

Help us?

Sabóor 86:4-6 in Kàddug Yàlla gi

4 Boroom bi, bànneexalal sab jaam, yaw laa dékk sama xol.
5 Boroom bi, yaa baax, di bale, di nàddil sa ngor képp ku lay sàkku.
6 Éy Aji Sax ji, teewlul, ma ñaan la; déglul, ma tinu la.
Sabóor 86 in Kàddug Yàlla gi