Text copied!
Bibles in Wolof

Sabóor 86:3-5 in Wolof

Help us?

Sabóor 86:3-5 in Kàddug Yàlla gi

3 Éy Boroom bi, baaxe ma; yaw laay yendoo woo wall.
4 Boroom bi, bànneexalal sab jaam, yaw laa dékk sama xol.
5 Boroom bi, yaa baax, di bale, di nàddil sa ngor képp ku lay sàkku.
Sabóor 86 in Kàddug Yàlla gi