Text copied!
Bibles in Wolof

Sabóor 86:2-3 in Wolof

Help us?

Sabóor 86:2-3 in Kàddug Yàlla gi

2 Maa gore, musal ma; maay sa jaam bi la wóolu, yaw, sama Yàlla, wallu ma.
3 Éy Boroom bi, baaxe ma; yaw laay yendoo woo wall.
Sabóor 86 in Kàddug Yàlla gi