Text copied!
Bibles in Wolof

Sabóor 86:14-15 in Wolof

Help us?

Sabóor 86:14-15 in Kàddug Yàlla gi

14 Éy Yàlla, nit ñu bew a ma jógal, def gàngoor gu néeg, di rëbb sama bakkan, te seetuñu la ci.
15 Waaye yaw Boroom bi Yàlla, yaa ñeewante, yërëm, yaa muñ mer, bare ngor ak worma.
Sabóor 86 in Kàddug Yàlla gi