Text copied!
BREAK EVERY YOKE
About
Bibles
All Languages
All Translations
All Countries
Back to Homepage
About Break Every Yoke
Bibles in Wolof
Sabóor 86:13-15 in Wolof
Help us?
Sabóor 86:13-15
in
Kàddug Yàlla gi
13
Ngor lu réy nga ma won, sorele maak tëraayu bàmmeel.
14
Éy Yàlla, nit ñu bew a ma jógal, def gàngoor gu néeg, di rëbb sama bakkan, te seetuñu la ci.
15
Waaye yaw Boroom bi Yàlla, yaa ñeewante, yërëm, yaa muñ mer, bare ngor ak worma.
Sabóor 86 in Kàddug Yàlla gi
Home
About
Donate
Patreon
Privacy
Terms