Text copied!
Bibles in Wolof

Sabóor 86:13-14 in Wolof

Help us?

Sabóor 86:13-14 in Kàddug Yàlla gi

13 Ngor lu réy nga ma won, sorele maak tëraayu bàmmeel.
14 Éy Yàlla, nit ñu bew a ma jógal, def gàngoor gu néeg, di rëbb sama bakkan, te seetuñu la ci.
Sabóor 86 in Kàddug Yàlla gi