Text copied!
Bibles in Wolof

Sabóor 86:12-13 in Wolof

Help us?

Sabóor 86:12-13 in Kàddug Yàlla gi

12 Boroom bi sama Yàlla, naa la sante xol bu fees, màggal la ba fàww.
13 Ngor lu réy nga ma won, sorele maak tëraayu bàmmeel.
Sabóor 86 in Kàddug Yàlla gi