Text copied!
Bibles in Wolof

Sabóor 86:10-12 in Wolof

Help us?

Sabóor 86:10-12 in Kàddug Yàlla gi

10 Yaa màgg te yéemey jëf, yaw doŋŋ yaa di Yàlla.
11 Éy Aji Sax ji, won ma sa nammeel, ma doxe sa worma. Tënkal sama xol ci ragal la.
12 Boroom bi sama Yàlla, naa la sante xol bu fees, màggal la ba fàww.
Sabóor 86 in Kàddug Yàlla gi