Text copied!
BREAK EVERY YOKE
About
Bibles
All Languages
All Translations
All Countries
Back to Homepage
About Break Every Yoke
Bibles in Wolof
Sabóor 85:7-9 in Wolof
Help us?
Sabóor 85:7-9
in
Kàddug Yàlla gi
7
Xanaa dinga leqli sa mbooloo, ba ñu man laa bànneexoo?
8
Éy Aji Sax ji, won nu sa ngor, baaxe nu sag wall.
9
Woykat ba nee: «Naa déglu lu Aji Sax ji Yàlla di wax.» Jàmm lay wax wóllëreem ñiy ñoñam, ba duñu dellu ci jëfi dof.
Sabóor 85 in Kàddug Yàlla gi
Home
About
Donate
Patreon
Privacy
Terms