Text copied!
Bibles in Wolof

Sabóor 84:7-8 in Wolof

Help us?

Sabóor 84:7-8 in Kàddug Yàlla gi

7 Buy jàll xuru Jooyoo, mu saf ko bëti ndox, céebo sànge xur wa barke,
8 muy gëna am doole, ba teewi fa Yàlla ca Siyoŋ.
Sabóor 84 in Kàddug Yàlla gi