Text copied!
Bibles in Wolof

Sabóor 84:5-7 in Wolof

Help us?

Sabóor 84:5-7 in Kàddug Yàlla gi

5 Ndokklee ku dëkke sa kër, di la màggalati. Selaw.
6 Ndokklee ku lay doolewoo, te namma topp njool ma jëm sa kër.
7 Buy jàll xuru Jooyoo, mu saf ko bëti ndox, céebo sànge xur wa barke,
Sabóor 84 in Kàddug Yàlla gi