Text copied!
BREAK EVERY YOKE
About
Bibles
All Languages
All Translations
All Countries
Back to Homepage
About Break Every Yoke
Bibles in Wolof
Sabóor 84:3-4 in Wolof
Help us?
Sabóor 84:3-4
in
Kàddug Yàlla gi
3
Damaa namm ëttub Aji Sax ji, di ko gelu ba jeex tàkk, jëmm jeek xol bi, di xaacul Yàlla jiy dund.
4
Éy Aji Sax ji Boroom gàngoor yi, sama buur, sama Yàlla, sawoor sax tag, nga fat ko, mbelaar it sàkk tàggam, denc ay cuujam fa sa sarxalukaay.
Sabóor 84 in Kàddug Yàlla gi
Home
About
Donate
Patreon
Privacy
Terms