Text copied!
Bibles in Wolof

Sabóor 83:7-9 in Wolof

Help us?

Sabóor 83:7-9 in Kàddug Yàlla gi

7 muy néegi Edom ak Ismayla, néegi Mowab ak Agar,
8 néegi Gebal, Amon ak Amaleg ak waa Filisteek waa Tir,
9 réewum Asiri it fekki leen, di dooleel askanu Lóot wa. Selaw.
Sabóor 83 in Kàddug Yàlla gi