Text copied!
Bibles in Wolof

Sabóor 83:3-6 in Wolof

Help us?

Sabóor 83:3-6 in Kàddug Yàlla gi

3 Xoolal sa noon yiy riir, sa bañ yi fippu ba téen!
4 Sa ñoñ lañuy rabatal, di mànkool sa séddoo yii.
5 Ñu ne: «Ayca nu far seen xeet wi, ba deesul fàttlikooti turu Israyil.»
6 Dañoo mànkoo kat, te yaw lañu takktool:
Sabóor 83 in Kàddug Yàlla gi